Beykat yi duñu dem tool altine.
Les cultivateurs ne vont pas au champ le lundi.
beykat bi -- farmer 👩🏾🌾 (from bey -- to farm/cultivate).
yi -- the (indicates plurality).
duñu -- do not/no one (?).
dem v. -- to go, leave, etc.
tool bi -- field, orchard.
altine ji -- (Arabic) Monday.
Wax na ko ko, aloor dina dem.
Il le lui a dit; alors, il partira.
wax v. -- to say, to speak.
na -- indicates something.
ko -- him, her, it.
ko -- it, her, him!
aloor -- (French) so, then, yet, here, etc. (a linking word).
dina -- he/she will.
dem v. -- to go, go.